Mbok yi ma ngui am mbekté takhaw nguir féddali sama yéneh si Sénégal mou nek lo xamni meunoul djogué fen foudoul si sama biiir xol, mou doone yéneh djou rafete boo xamni danio waraa takhaw nguir rab Sénégal tambaliko si djikoh yi, djeuf yi bassi doxaline yi, nguir niou am euleugou Sénégal bou baax.
Mbok yi naniou and liguey sunu Sénégal 🇸🇳
Dewenati!! 🥳 bonne année 🎊